- oumhabiba
- Nombre de messages : 43
Date d'inscription : 16/05/2008
GIGOT D AGNEAU AU FOUR
Mer 18 Juin 2008 - 9:20
INGREDIENTS :
1 gigot d'agneau
250 g d'oignons
500 g pommes de terres
ail, poivre, piment sec, gingembre
moutarde, tomate concentrée
huile, jumbo, poivron, vinaigre
1 pot mayonnaise
PREPARATION :
1- damaye deub touti nokoss diw si gigot bi daldi si wiss touti khorome daldi ko mousseule
2- ma dagg soble bi ak pomme de terre bi pour frite
3- ma nokossate ( poivron, poivre, piment sec, jumbo, ail) khadje ko si digue bi : bene moitié bi ma marine ko soble bi def si vinaigre ak moutarde tegue ko touti
4- benene moitié nokosse bi ma deube gingembre bi def kossi daldi siye yokk moutarde ak une cuillerée à soupe de tomate concentrée ak touti huile yeungueule def si bene bol tegue ko ne
5- sou gigot bi gnore (si moussale bi) ma seppi ko tegue fe sou sedde ma tale four bi daldi diw gigot bi ak mélange nokoss bi ak gingembre, moutarde, tomate concentrée ak huile ; ma diw ko bamou dadje souma pare dougueule si four bi lakk ko
6- ma marine mayonnaise bi def ko au frais
7- ma saute sama soble si touti huile tegue feulé daldi saffe frite yi
8 - sou yappe bi gnore ma indi plateau bi tegue gigot bi si digue bi frites yi d'un coté, sauce soble bi d'un autre def mayonnaise bi si bene assiete daldi tadje nak gnou rere

Permission de ce forum:
Vous ne pouvez pas répondre aux sujets dans ce forum